Leaving - Youssou N'Dour

Leaving - Youssou N'Dour

  • Year of release: 1994
  • Language: Cebuano
  • Duration: 4:59

Below is the lyrics of the song Leaving , artist - Youssou N'Dour with translation

Lyrics " Leaving "

Original text with translation

Leaving

Youssou N'Dour

Dem dem

Dem fan

Den ndax lan

Baya ko mom

Dem nguir xee bou barri bi

Dem ndax teen boh neex bi

Teh rapp rek noom noo siy naan

Nach bi lakkatouma taw bi barrewoul

Dem ngir bokk bone menou fee am

Dem ngir daffa wara nekk gorr done

Goorgoorlau

Dem dem

Dem fan

Dem ndax lan

Liberte bi

Si espace bou lendeum bi

Sama beut yi guissa tounou

Garap yi nga xamenteni noo ma souxat

Su beut setiee barap yi bow

Dem ngir Keur gui daf may nirou lou lendeum

Dem nguir daffa warranekk goor done

Goorgoorlau

Damay dem

Chi alla bi

Damay dem Chi dex goumak gui

Ne damay dem waw seeti sama nawleyee

Damay dem si ban bou ritax bi

Damay dem ba reewu bitty

Ne damay dem waw setti samambokkyee

Go-go

Won ma sa yarii ma wax la ki nga donoy

Won ma sa mbokk ma wax ko fi ngay diaar

Hey what do you need?

He he yaw lilaneex

Won ma sa yarii ma wax la ki nga donoy

Won ma sa mbokk ma wax ko fi ngay diaar

He defa li la neexoy hey yaw lila soop

Sammkatou mboott moo xam ba ciy

Sooxaoy ni meneuh kott noom daal amounou

Mbaam hey defal li la nexx oo

Hey what do you want?

Ho ho ho ho …

2+ million lyrics

Songs in different languages

Translations

High-quality translations into all languages

Quick search

Find the texts you need in seconds