Dabbaax - Youssou N'Dour

Dabbaax - Youssou N'Dour

Год
2007
Язык
`French`
Длительность
308160

Below is the lyrics of the song Dabbaax , artist - Youssou N'Dour with translation

Lyrics " Dabbaax "

Original text with translation

Dabbaax

Youssou N'Dour

Keroksou penc bognouy wadjia wathié janta bi

Di wadjial Péssé ba

Moulay dabbaxx yalla nagnou la diégué yalla daal moy taan waayam

Moulaay Dabaaaaax…

Bougnou Faté, Bess boboulé, Uhh Bougnou Soré, Bess boboulé

Bougnou faté Bess Boboulé

Lofa Gnaane, Yalla May lako

Modaane wakhal nitt gnep, Mo daane wakhal nasraane yi

Anh Mo daane Kadou Askane wi

Dafa daane wakh naane nagnou bolé sougn rew

Dafa daane wakh naane bou kéne wéngal gaal gui

Dafa daane wakh naane nagnou bolé sounou khol yi

Dafa daane wakh naane nagnou yeureum Djiguéen

Sa borom bi begu na, Yonentam bi begu na, yako liguéyal sa borom

Moulaye Dabbaxx yaw dé wacci ngua masso wakh lou amoul

Kérok bang gnou djito assamaane si da Leudeum

Bessa ngui kéne dotou ko Fatéééti… Moulaay Dabbaxx

Bougnou Faté, Bess boboulé, Bougnou Soré, Bess boboulé

Bougnou faté Bess Boboulé

Lofa Gnaane, Yalla May lako

Anh! Modaane wakhal nitt gnep, anh! Mo daane wakhal nasraane yi

Anh! Mo daane wakhal Askane wi

Dafa daane wakh naane na gnep ligueye

Dafa daane wakh naane nagn diangal gounéyi

Dafa daane wakh naane na gnep liguèye

Dafa daane wakh naane nagn diangal djiguééne gni

Daawaoul Sétane lou gnaaw

Poussom la yorone fou khotékou Mou gnaw

Rewmi.rewmi amélnagnou la ndiouka Moulaay Dabbaxx

Daawaoul Sétane lou gnaaw

Poussom la yorone fou khotékou Mou gnaw

Rewmi.rewmi amélnagnou la ndiouka Moulaay Dabbaxx

Bakrék Dara Maam, Aram lô Coumba Thiam

Magn Penda ak Pathé Pendaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaah

Modaane wakhal nitt gnep, Mo daane wakhal nasraane yi

Mo daane Kadou Askane wi

Dafa daane wakh naane nagn diap sounou rewmi

Dafa daane wakh naane nagnep liguéye

Dafa daane wakh naane nagn Yeureum djiguéene gni

Dafa daane wakh naane nagn diangal gounéyi

2+ million lyrics

Songs in different languages

Translations

High-quality translations into all languages

Quick search

Find the texts you need in seconds